1. 1

    Philip Monteiro - Alta Segurança (Prisão Perpetua)

  2. 2

    Philip Monteiro - Sama Wo

  3. 3

    Philip Monteiro - Amor (feat. Viviane Chidid)

  4. 4

    Philip Monteiro - Irresistível

  5. 5

    Philip Monteiro - Estou Em Suas Mãos

  6. 6

    Philip Monteiro - Fanny (feat. Fef)

  7. 7

    Philip Monteiro - Inseparavel

  8. 8

    Philip Monteiro - Julgam (feat. Gama)

  9. 9

    Philip Monteiro - Abri Bu Coração (feat. Gama)

  10. 10

    Philip Monteiro - Mãe (feat. Fef & Nany)

  11. 11

    Philip Monteiro - Sai Cu Bo (feat. Gama)

  12. 12

    Philip Monteiro - Sara

  13. 13

    Philip Monteiro - Bu Omi

  14. 14

    Philip Monteiro - Preciosa

  15. 15

    Philip Monteiro - A volta

  16. 16

    Philip Monteiro - Abraço Vento (feat. Paulinha)

  17. 17

    Philip Monteiro - Amor (remix) (feat. Viviane Chidid)

  18. 18

    Philip Monteiro - Irresistivel (remix)

  19. 19

    Philip Monteiro - Precisa Di Mi (feat. Talina)

  20. 20

    Philip Monteiro - Ai Minina

  21. 21

    Philip Monteiro - Cindy

  22. 22

    Philip Monteiro - Cindy (Raggaeton)

  23. 23

    Philip Monteiro - É Mentira

  24. 24

    Philip Monteiro - É Só 1 (feat. Tó Semedo)

  25. 25

    Philip Monteiro - Is It Me (R & B) (feat. Paulinha)

  26. 26

    Philip Monteiro - Jeito Doce

  27. 27

    Philip Monteiro - Juram (feat. Gama)

  28. 28

    Philip Monteiro - Locura

  29. 29

    Philip Monteiro - Mbi Fé (part. Fodé Baro)

  30. 30

    Philip Monteiro - N'krê Ser (feat. Tó Semedo)

  31. 31

    Philip Monteiro - Pourquoi Me Quitter (feat. Fodé Baro)

  32. 32

    Philip Monteiro - Tempestade

  33. 33

    Philip Monteiro - Yaw Rek Lev (feat. Corine)

Yaw Rek Lev (feat. Corine)

Philip Monteiro

Ibil nal sama khol
Yalla na nga si guiss lou lére
Té gueuneu kham ni
Amoul kénène koudoul yaw
Mbeugél gui nékeu si mane
A ngii di ma dane
Té gueum na né di na done
Sa néné bi ngéy tété

Mane mi souma mounone
Dina bokake yow bénéne yone
Dila wowé néné touti
Ndakh té mane mi
Mane mi gnanou ma yalla
Gnanou ma yalla
Déss fii mane réka

Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné

Am na gnou wakh
Mbeugél tiono rék la
Wayé ma ngi léy khamal
Dou kéne yow réke leu
Beuss bou me le guissé
Ta kham ni khol déy guissé
Té fok na ni do meusse tass sama yakar!

Boul am loy ragal di la khar
Doumeu meusseu diay sama taar
Dinala wowé papa chéri
Dina done sa sokhna
Di na done sa baby
Mi léy fadial
Say sokhla, oh baby yow réke le

Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné

Yay sama doolé
Soudoul yow wate na né dou done kékéne
Diokh na la sama bope
Té dina la dégueul di le bégueul
Baby boul sone
Gueumeul ni yow réke le!
Dou kékéne

Ibil nala sama khol
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Té dina done sa néné
Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law
Ibil nala sama khol

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados