1. 1

    Youssou N'dour - 7 Seconds

  2. 2

    Youssou N'dour - Seven Seconds Away

  3. 3

    Youssou N'dour - Birima

  4. 4

    Youssou N'dour - Set

  5. 5

    Youssou N'dour - Shaking The Tree

  6. 6

    Youssou N'dour - So many men

  7. 7

    Youssou N'dour - Ay Chona La

  8. 8

    Youssou N'dour - Ballago Ndoumbé Yatma

  9. 9

    Youssou N'dour - Be Careful

  10. 10

    Youssou N'dour - Benn La (The Same)

  11. 11

    Youssou N'dour - Biko

  12. 12

    Youssou N'dour - Bul Nangu (feat. Mbaye Dièye Faye & Bilahi)

  13. 13

    Youssou N'dour - Confession

  14. 14

    Youssou N'dour - Cruel Crazy Beautiful World

  15. 15

    Youssou N'dour - Da Fa Laa

  16. 16

    Youssou N'dour - Dem

  17. 17

    Youssou N'dour - Dunya

  18. 18

    Youssou N'dour - Fay Bor

  19. 19

    Youssou N'dour - Gorée

  20. 20

    Youssou N'dour - Habib Faye

  21. 21

    Youssou N'dour - How Come

  22. 22

    Youssou N'dour - In An African Passageway

  23. 23

    Youssou N'dour - Kids

  24. 24

    Youssou N'dour - La Cours Des Grands

  25. 25

    Youssou N'dour - Leaving (Dem)

  26. 26

    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (As In A Mirror)

  27. 27

    Youssou N'dour - Ligeey

  28. 28

    Youssou N'dour - Mama Africa

  29. 29

    Youssou N'dour - Mame Bamba

  30. 30

    Youssou N'dour - Mariama (The Turtle Dove)

  31. 31

    Youssou N'dour - Mool (Deglu Météo)

  32. 32

    Youssou N'dour - My Hope Is In You

  33. 33

    Youssou N'dour - Olel (The Echo)

  34. 34

    Youssou N'dour - Oté-fê (feat. Alpha Blondy)

  35. 35

    Youssou N'dour - Song Daan (feat. Akon)

  36. 36

    Youssou N'dour - Thiely

  37. 37

    Youssou N'dour - Things Unspoken (Lees Waxul)

  38. 38

    Youssou N'dour - Toxiques

  39. 39

    Youssou N'dour - Waññi ko

  40. 40

    Youssou N'dour - Wax ju bari

  41. 41

    Youssou N'dour - Xale Bi

  42. 42

    Youssou N'dour - Youssou Madjiguene

Ballago Ndoumbé Yatma

Youssou N'dour

Billaay, ballago ndoumbé yatma
Su ñu waaji xaj oon na fi
Naxxar doηη, la ñu bayyee
Yalla, wonneeti na

Li tax ba mbir mi metti lool
Ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gnou
Billaay wéetël na ñu

Njiinoo njiin faramaareen
Gòor u jaaga, nelaw naa
Baay i wally dem na nii
Ñun daal wéetël na ñu

Ma ngi koy jaale Sénégal
Di ko jaalé Gambia
Di ko jaalé adduna
Ndaanaan ba dem na nii

Thione ballago, ndoumbé yatma
Bu yalla buur bi doon taggoo
Kon di na ñu bayék yaw
Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel
Yee gua nit gñi, tete leen ci adduna
Yee gua nit gñi, tete leen
Xam al leen ci adduna
Ahh - Balaago

Yee gua nit ñi ci adduna xam al leen
Ni ñu war a nekkek
Ak ni ñu war a dundée
Ak ni ñu war a jëfleentee
Jinaxoo mbaay
Yaw mi dëkké biir suuf
Boo dem ee neel ballago, réew maa ngi koy joy
Aduna ngi koy jooy
Art baa ngi koy jooy

Njiin faramaareen
Thione seck, wéetël na ñu
Ballago ndumbé yaatma
Adduna, am ul solo

Li tax ba mbir mi metti lool
Ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gno
Ndanaan ba dem na ni
Njiin faramaareen
Thione Seck, wéetël na ñu
Ballago ndumbé yaatma
Àdduna amul solo

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados